Souba - Synapson, Lass

Souba - Synapson, Lass

Альбом
Super 8
Год
2018
Язык
`Frans`
Длительность
203210

Hieronder staat de songtekst van het nummer Souba , artiest - Synapson, Lass met vertaling

Tekst van het liedje " Souba "

Originele tekst met vertaling

Souba

Synapson, Lass

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco

Gnaféla birmi mané gnaféla

Guisga yaw loula war moy gnaféla

Ndanga dioque si ça dieulebéne

Bala moye wessou ga dico reuthiou

Mané doiksi dioksi yaw dale

Mané doiksi dioksi yaw waye

Mané doiksi dioksi yaw dale

Bala moye wesso

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco

Wayé soumété ga dawe goor

Boule fowé sa daw domou daye

Goor yalla dara dou yombeu ya

Diambar dara dou yombeu ya

Gnaféla birmi mané gnaféla

Guisga yaw loula war moy gnaf…

Gnaféla birmi mané gnaféla

Guisga yaw loula war moy gnaféla

Ndanga dioque si ça dieulebéne

Bala moye wessou ga dico reuthiou

Mané doiksi dioksi yaw dale

Mané doiksi dioksi yaw waye

Mané doiksi dioksi yaw dale

Bala moye wesso

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga gueumeco

Soubaye dakeu taye waye

Wayé daye fékeu yawe ga beugueuco

Meer dan 2 miljoen songteksten

Liedjes in verschillende talen

Vertalingen

Hoogwaardige vertalingen in alle talen

Snel zoeken

Vind binnen enkele seconden de teksten die je nodig hebt